1 Samuel 2:12
TSK
¶ Doomi Eli yu góor ya nag def nit ñu bon ñu faalewul Aji Sax ji.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Doomi Eli yu góor ya nag def nit ñu bon ñu faalewul Aji Sax ji.
¶ Eli nag mujj na di mag lool. Ba mu yégee mboolem li doomam yu góor yi def ak Israyil gépp, bay tëdde sax jigéen ñiy liggéey ci bunt xaymab ndaje mi,
Buur dellu ne Simey: «Yaw ci sa bopp xam nga xéll mboolem li nga lor sama baay Daawuda. Léegi Aji Sax ji dina la fey sa jëf ju bon, mu këppu ci sa kaw bopp.
Yaral sa doom ba muy teel, waaye bul topp sa xol, ba rey ko.
Deel bantal ak a yedde, day rafetal xel; gone goo bay-bayal, mu gàcceel ndeyam.
Jeexal nga nag léegi! Maay yebal sama mer fi sa kaw. Maa lay mbugale say jëfin, yool la sa jépp jëf ju siblu.