TSK

TSK · 1 Samuel 7:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Sóol ci boppam làqoon na ay at, ba muy falu buur; mu falu jiite Israyil ñaari at.

Ba mu ko defee Sóol ak gàngoor ga ànd ak moom gépp daje, dem ca xare ba. Gisuñu lu moy waa Filisti ne kër-kër, ne këpp, di jamante seeni saamar.

¶ Samiyel nag faatu woon na, ba Israyil gépp dëj ko, denc ko ca Raama, dëkkam ba. Te itam Sóol mujjoon naa génne réew ma ñiy seete nit ñu dee, ak boroom rawaan yiy gisaane.

¶ Gannaaw gi, Daawuda duma na Filisteen ña, néewal leen doole, jële kilifteefu waa Filisti ca réew ma.