1 Samuel 28:14
TSK
Mu ne ko: «Nu mu mel?» Mu ne ko: «Góor gu mag ay yéegsi. Mu ngi sàngoo mbubb.» Sóol xam ne Samiyel la, daldi sukk, sujjóot, dëpp jëëm fa suuf.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu ne ko: «Nu mu mel?» Mu ne ko: «Góor gu mag ay yéegsi. Mu ngi sàngoo mbubb.» Sóol xam ne Samiyel la, daldi sukk, sujjóot, dëpp jëëm fa suuf.
¶ Ilyaas bàyyikoo fa, fekk Alyaasa doomu Safat, Alyaasa di gàbb ak ñaar fukki nag ak ñeent yu ko jiitu, ñu likke leen ñaar-ñaar, moom ci boppam mu jiital fukkeelu likke baak ñaar. Ilyaas dikk ba ca moom, sànni mbubbam ca kaw Alyaasa.