TSK

TSK · 2 Kings 5:21

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Dawal gaaw dajeek moom, laaj ko mbaa mu ngi ci jàmm mook jëkkëram ak doomam.» Mu laaj ko, mu ne ko: «Jàmm rekk la.»

Luke 7:6 TSK

¶ Yeesu daldi ànd ak ñoom. Naka la jubsi kër ga, njiit la yóbbante ay xaritam kàddoom, ñu gatandu Yeesu, ne ko: «Sang bi, jarul ngay sonn, ndax sab tànk sama biir kër, man yeyoowuma ko.

Ba Piyeer duggsee, Korney gatandu ko, ne gurub ca tànki Piyeer, sujjóot.