Mu dem ba tollook ay ngéddi xar ca yoon wa; foofa am xuntee nga fa woon. Mu dugg ca biir, di suturlu. Fekk na Daawudaaki nitam a nga ca biir-a-biir xunti ma, toog.
TSK
TSK · 2 Kings 6:21
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
1 Samuel 24:4
TSK
1 Samuel 26:8
TSK
Abisay ne Daawuda: «Yàlla de teg na sab noon ci say loxo guddig tey jii. Bàyyil rekk ma daaj ko xeej bi fi suuf benn yoon rekk, du ñaar!»
2 Kings 5:13
TSK
¶ Surgaam ya nag dikk, kenn ca ñoom ne ko: «Baay Naaman, su doon lu jafe la la yonent bi wax ndax danga ko dul def? Kon kay su la nee nga sangu rekk, set wecc, nga war koo def!»
2 Kings 13:14
TSK
¶ Ba Alyaasa tëddee ca wopp ja ko wara yóbbu, Yowayas buurub Israyil seeti woon na ko, tiim ko, di jooy naan: «Éy baayoo, baay Alyaasa, yaay watiiru xarey Israyil aki gawaram!»
Luke 22:49
TSK
Ña ànd ak Yeesu nag gis la ca nara topp, ñu ne: «Sang bi, nu jame saamar boog?»