1 Kings 20:14
TSK
Axab ne ko: «Ku may defal loolu?» Mu ne ko: «Aji Sax ji nee: Dag yi kilifay diiwaan yi yebal lay doon.» Axab ne ko: «Kuy sooke xare bi?» Mu ne ko: «Xanaa yaw.»
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Axab ne ko: «Ku may defal loolu?» Mu ne ko: «Aji Sax ji nee: Dag yi kilifay diiwaan yi yebal lay doon.» Axab ne ko: «Kuy sooke xare bi?» Mu ne ko: «Xanaa yaw.»
¶ Yesabel dégg ca, ne Axab: «Jógal nanguji toolu reseñu Nabot waa Yisreel bi. Moo la ko bañoona jaaye xaalis, waaye dundatul, dee na.»
¶ Ba loolu amee mu ne jaraafam ba ñuy wax Bitkar: «Foral sànni ci toolub Nabot mu Yisreel. Yaa ngi fàttliku ba nu bokkee watiir maak yaw topp ca baayam Axab te Aji Sax ji rëbb ko ne ko:
Yeen waa Lakis, takkleen fasi dawkat ak watiir. Yeena jëkka moyloo janq Siyoŋ mu taaru, ci yeen lañu jëkka gise bàkkaari Israyil.