كل أسفار KYG

2 Samuel 13

KYG · الآية 4

24 أصحاحات

KYG / 2 Samuel / الأصحاح 13

KYG · الآية 4

M u ne Amnon: «Waaw, yaw doomu buur nga, lu la tax ne yogg nii bés bu set? Doo ma ko wax?» Amnon ne ko: «Tamar, mi bokk ak sama doomu baay Absalom ndey ak baay, moom laa bëgg.»