TSK

TSK · 2 Samuel 2:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Dëgërluleen déy te diy góor, yeen waa Filisti, nde lu ko moy ngeen doon jaami Ebrë yi, na ñu nekke woon sunuy jaam. Góor-góorluleen boog te xeex.»

seen jàmbaar yépp a fabu, topp guddi ga gépp ba Bet San. Ñu wékkee ca miiru Bet San néewu Sóol ak néewi doomam yu góor, doora ñibbi Yabes, boole fa néew ya, lakk.

Góor-góorlul nag, te nu bokk góor-góorlu ngir sunuw xeet ak sunu dëkki Yàlla yi. Aji Sax ji nag mooy def li ko soob.»