TSK

TSK · 2 Samuel 4:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ci kaw loolu rekk niti Daawuda ànd ak Yowab, jóge xare, indaale lël ju bare. Waaye fekkul Abner Ebron ca Daawuda, ndax fekk na Daawuda yiwi ko, ba mu dem ci jàmm.

¶ Fekk na ay xarekati waa Siri dem songi réewum Israyil, jàppe fa ab janq, def ko surgab jabaru Naaman.