Genesis 24:2
TSK
¶ Mu am bés Ibraayma wax surgaam, bi gëna yàgg ci këram, tey saytu alalam jépp, ne ko: «Dugalal sa loxo ci sama suufu lupp,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Mu am bés Ibraayma wax surgaam, bi gëna yàgg ci këram, tey saytu alalam jépp, ne ko: «Dugalal sa loxo ci sama suufu lupp,
¶ Naka la Daawuda dox ba wees tuuti collu tund wa rekk, yem ca Ciba, surgab Mefiboset. Ma nga làng ak ñaari mbaam yu ñu laltaay, sëf leen ñaar téeméeri mburu ak téeméeri danki reseñ ak téeméeri danki figg ak mbuusum biiñ.
Junniy nit ñu askanoo ci Beñamin a ko topp, ñook Ciba, surgab waa kër Sóol, ak fukki doomam yu góor ak juróom, ak ñaar fukki surgaam. Ñu riirandoo ca dex ga, di gatandu Buur Daawuda.