Acts 13:18
TSK
Lu tollook ñeent fukki at la leen muñal ca màndiŋ ma.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Lu tollook ñeent fukki at la leen muñal ca màndiŋ ma.
Nit kii la Yawut yi jàppoon, di ko waaja rey, far ma dikk ànd ak lenn ci gàngoor gi, wallu ko, ndax fekk na ma yég ne as goru Room la.
Ba tuumaalkat ya taxawee nag, feeñaluñu jenn tuuma ju bokk ci yu bon, yi ma foogoon,
¶ Ci kaw loolu Àggripa ne Póol: «Léegi sañ ngaa waxal sa bopp.» Póol nag tàllal loxoom, layool boppam, ne:
¶ Céy bu ngeen ma muñaloon, ba ma dof-doflu tuuti! Muñal-leen ma rekk.
Dina mana sédd cér ñi xamul ak ñi moy ndax moom ci boppam ci ag néew doole la tënku.