TSK

TSK · Acts 27:31

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ay malaakaam la lay booleel, ñu di la sàmm foo jëm.

Su boobaa seen dëkkandooy yéefar yi fi des dinañu xam ne man Aji Sax ji maa tabaxaat dëkk yu mag yi tojatoo woon, jëmbataat mbooy gi. Man Aji Sax ji, maa wax te maay jëf.

Luke 4:9 TSK

¶ Seytaane yóbbu na ko Yerusalem, aj ko ca njobbaxtalu kër Yàlla ga, ne ko: «Ndega yaa di Doomu Yàlla, tëbeel fii, wàcc,

Teewul njiitu takk-der ba sobental waxi Póol, déggal dawalkat ba ak boroom gaal ga.

¶ Ba loolu amee takk-der ya nara rey ña ñu tëj, bala ñoo féey, ba raw.