كل أسفار KYG

Acts 7

KYG · الآية 8

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 7

KYG · الآية 8

Y àlla daldi fasook Ibraayma kóllëre gu mu màndargale xaraf. Moo tax Ibraayma xarfal doomam Isaaxa, ba mu juddoo ba am juróom ñetti fan; Isaaxa, Yanqóoba, Yanqóoba, fukki maam yaak ñaar.