TSK

TSK · Amos 5:3

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Nit ñu néew ngeen di dese, te bare woon ni biddiiwi asamaan, ndax ñàkka déggal seen Yàlla Aji Sax ji.

Bu nu Aji Sax ji Boroom gàngoor yi waccalul woon li nu deseek as néew, ni Sodom lanuy mel, Gomor lanuy neexool.

Seen xeet wi ni feppi suufas géej lay tollu, te as ndes a ciy délsi. Àtteb sànkute mooy taxaw, yoon toppe ba mat sëkk.

Amos 6:9 TSK

Su boobaa, fukk ñu làqu ci kër, du leen teree dee.»