TSK

TSK · Deuteronomy 13:11

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Musaa ne mbooloo ma: «Fàttlikuleen bésub tey jii ngeen génne Misra, kërug njaam gi, ak ni leen Aji Sax ji yiwee dooley loxoom. Bu ci kenn lekk mburu mu am lawiir.

Aji Sax ji ne Musaa: «Jàppal njiiti mbooloo mi yépp, nga wékk leen ci bant fi kanam Aji Sax ji, bëccëg ndarakàmm, ngir sànjum Aji Sax ji dëddu Israyil.»

Ñi ci des dinañu ko dégg, te dinañu ragal ba duñu defati lu bon lu ni mel ci seen biir.

Boo ñefee ab ñaawlekat, téxét ba jànge ca; nga yedd kuy dégg, mu xame ca.

Waaye ñi ciy bàkkaar, tiiñal leen, ndax ñi ci des ragala bàkkaar.