Numbers 21:23
TSK
Siwon nag mayul Israyil, ñu jaarem réewam, xanaa mu dajale gàngooram gépp, sàqi, ngir dajejeek Israyil ca màndiŋ ma. Mu dikk ba Yaxacc, song Israyil,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Siwon nag mayul Israyil, ñu jaarem réewam, xanaa mu dajale gàngooram gépp, sàqi, ngir dajejeek Israyil ca màndiŋ ma. Mu dikk ba Yaxacc, song Israyil,
¶ «Yaa leen moomale ay réew aki xeet, séddale leen suuf. Ñu nangu réewum Siwon, réewum buurub Esbon, teg ca réewum Og buuru Basan.
muy Siwon buurub Amoreen ña, ak Og buuru Basan, ak buuri Kanaan ñépp.