TSK

TSK · Esther 7:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Buur ne ko: «Lingeer Esteer, lan la, ak looy sàkku? Su doon genn-wàllu nguur gi sax, dees na la ko jox!»

Buur ne Lingeer Esteer: «Biir Sus, péey bii, Yawut yi rey nañu ci juróomi téeméeri nit, reyaale fukki doomi Aman yu góor. Kon diiwaani buur yi ci des xawma nu ñu def ak ñoom. Ana looy ñaanati, ñu may la ko ak looy sàkkooti, ñu defal la ko?»

¶ Ba loolu amee njiital gàngoor gi jàpp ci loxol xalelu góor bi, wéetoo ak moom, ne ko: «Ana loo may xamal?»