Ba loolu amee ñu fal ay nit ñu leen di ga ca seeni sas, di leen ca fitnaal lool. Noonu la bànni Israyil tabaxale Firawna buuru Misra dëkk, ya ñu naa Pitom ak Ramses, mu def ko ay dencukaayi dund.
TSK
TSK · Exodus 2:11
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Exodus 1:11
TSK
Exodus 5:9
TSK
Nañu leen yen liggéey bu gëna metti, te ñu dëkke ko, ba duñu tala déglu ay feni neen.»
Isaiah 58:6
TSK
«Xanaa du lii moo di koor gi ma taamu: yolomal jéng yu metti, fecci buumi noteel, afal ku diis; dog lépp luy xeetu noteel?
Luke 4:18
TSK
«Noowug Boroom baa ngi fi sama kaw, moo ma fal, ngir ma yégal néew-doole yi xibaaru jàmm bi. Da maa yebal ngir ma yégal jaam yi ne dees na leen goreel, yégal gumba yi ne dinañu gis, yégal ñi ñu not, ne dees na leen jot,
Hebrews 11:24
TSK
Ba Musaa màggee, ngëm a taxoon mu bañ ñu wooye ko doomu doomu Firawna ju jigéen.