TSK

TSK · Exodus 25:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Ñu indil Aji Sax ji seen sarax, muy juróom benni watiir ak fukki nag ak ñaar; ñaari kilifa yu nekk, benn watiir; kilifa gu nekk, wenn nag, ñu yóbbu lépp fa kanam jaamookaay ba.

¶ Kon ñetti yoon cim at la mboolem seeni góor di teew fi seen kanam Yàlla Aji Sax ji, ci bérab bi muy taamuji: fani màggalu Mburu mu amul lawiir, ak fani màggalug Ayi bés, ak fani màggalu Mbaar yi. Waaye deesul teewe loxoy neen fi kanam Aji Sax ji.

Ezra 1:6 TSK

Mboolem seeni dëkkandoo daldi def ci seen loxo jumtukaayi xaalis ak wurus, alal akug jur ak gànjar, te bokkul ak mboolem seen saraxi yéene.

Ezra 3:5 TSK

Gannaaw loolu ñu joxe saraxu dóomal bi sax fàww, ak saraxi Terutel weer ya, ak sarax yu sell yi war ci mboolem màggali Aji Sax ji, ak mboolem saraxi yéene yi ñuy indil Aji Sax ji.

Mbooloo ma nag gërëm ñi nangul seen bopp ne dañuy dëkk Yerusalem.

Kon nag léegi, mottlileen jëf ji. Noonu ngeen xére woon ci seen yéene, mottleeleen ko noonu ci seen kem am-am.