«Waxal bànni Israyil ne leen, ñu indil ma ab jooxe. Ci képp ku am yéeneem ngeen di nangoo sama jooxe, indil ma ko.
TSK
TSK · Exodus 36:2
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Exodus 25:2
TSK
Exodus 28:3
TSK
Dangay sant mboolem liggéeykat yu xareñ, yi ma feesal xelum xareñte, ñu defar yérey Aaróona, ngir fal ko, mu di ma sarxalal.
Exodus 35:2
TSK
Juróom benni fan lees di liggéey, waaye bésub juróom ñaareel ba, seen bésub Noflaay bu sell bu mat sëkk la, ñeel Aji Sax ji. Képp ku ci liggéey lenn, dees koy rey.
Exodus 35:21
TSK
Ba mu ko defee mboolem ña ca am pastéefu xol ak mboolem ña ca seen xel xiir, ñépp dikk, indi jooxeb Aji Sax ji ngir liggéeyu xaymab ndaje meek bépp liggéey bu mu laaj, ngir itam yére yu sell yi.
Acts 14:23
TSK
Mbooloom gëmkat mu nekk nag, ñu tabb ci ay mag; ci biir loolu ñu ñaan, boole kook koor, daldi dénk mag ña Sang bi ñu gëm.
Hebrews 5:4
TSK
¶ Te it kenn jagoowul boppam teraangay carxal, ndare du Yàllaa ko ci woo, na woon ca Aaróona.