¶ «Su ngeen saxee ci noonoo ma, bañ maa déggal, maay fulaat seen mbugal fukki yoon ak juróom, feye leen ko seeni bàkkaar.
TSK
TSK · Ezekiel 21:14
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Ba loolu amee Balag sànju ci kaw Balaam, daldi fenqey loxoom. Ci kaw loolu Balag ne Balaam: «Móolu samay noon laa la wooye woon, yaw defoo lu moy ñaanal leena ñaanal, ba muy ñetti yoon nii!
Mise ne ko: «Yaw mii yaa koy gisal sa bopp, keroog ba ngay dugg néegoo néeg, di làqtu.»
¶ Jamono jooja la jaraafi Nabukodonosor buuru Babilon, song Yerusalem, gaw dëkk ba.
Waaye yaw saamar, noo mana selaŋloo te Aji Sax ji yebal la ci kaw Askalon ak waa tefesu géej, fa mu ko dogale?»
Mu ne ma: «Yaw nit ki, du yaa gis li magi kër Israyil di def ci lëndëm gi, ku nekk ak fa ñu jagleel sa nataalu tuur. Ña nga naan: “Aji Sax ji gisu nu, Aji Sax ji wacc na réew mi.”»
Maa fiy yebal mbas, deret tuuroo mbedd yi, saamar dajal dëkk bi, bóom nit ñi, tëral, ba ñu xam ne maay Aji Sax ji.”
Bu ñu bëttoon, ba biir njaniiw it, fa laa leen di yóotoo. Ñu yéeg asamaan, ma wàccee leen fa.