TSK

TSK · Ezekiel 21:17

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba loolu amee Balag sànju ci kaw Balaam, daldi fenqey loxoom. Ci kaw loolu Balag ne Balaam: «Móolu samay noon laa la wooye woon, yaw defoo lu moy ñaanal leena ñaanal, ba muy ñetti yoon nii!

Moo tax, kàddug Boroom bee, Aji Sax ju gàngoor yi, Jàmbaaru Israyil: «Maay lijjanti samay bañ, ngalla ñoom! Maay fey samay noon!

Dëddu woon nanu la moos waaye léegi réccu nanu. Xam nan ne tooñ nanu, ba tey nuy màttuy wiccax. Danoo rus, torox ndax sunu ñaawtéefi ndaw.”»

Maa lay xëpp samam sànj ba mu jeex, bala ma laa moyale sama xadaru fiiraange, doora dal, ba meddi.

¶ «“Maa ngii nag di fenqe samay loxo, di ko mititloo alal ju lewul ji nga dajale, ak sa dereti nit ji ñu tuur fi sa biir.

¶ Ci kaw loolu mu àddu ca kaw, ne ma: «Xoolal, ñi jëm réewum bëj-gànnaar, samag Noo lañuy sànni ca kaw réewum bëj-gànnaar.»