2 Samuel 5:9
TSK
Ba mu ko defee Daawuda dëkk ca biir tata ja, wooye ko Kër Daawuda, ba noppi tabax fa ko wër fépp, dale ko ca sëkkub Milo, ba ca biir.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ba mu ko defee Daawuda dëkk ca biir tata ja, wooye ko Kër Daawuda, ba noppi tabax fa ko wër fépp, dale ko ca sëkkub Milo, ba ca biir.
Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Ku doyloo Aji Sax ji, yaay tundu Siyoŋ, doo toxu; dangay sax ba fàww.
Moo tax ay bés a ngii di ñëw,» kàddug Aji Sax jee, «maay dégtal Raba, dëkku Amoneen ñi, coowal xare ci seen biir, tund wa gental, dëkk-dëkkaan ya tàkk ba jeex, ba keroog Israyil futti ñooña ko futti woon.» Aji Sax jee ko wax.
Maay soppi Raba seen péey ab parlub giléem, maay def réewum Amon goorukaayu gàtt, ba ngeen xam ne maay Aji Sax ji.