Genesis 1:13
TSK
Ngoon jot, suba dugg, muy bésub ñetteel ba.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ngoon jot, suba dugg, muy bésub ñetteel ba.
Ngoon jot, suba dugg, muy bésub juróomeel ba.
Li feek suuf di suuf, dootu jiwooy dakk mbaa ngóob, te du sedd aku tàngoor, du nawet it mbaa noor, mbaa guddeek bëccëg.»
Yaa moom bëccëg, moom guddi, teg fi weer week jant bi.
Maay bind leer, di def lëndëm. Maay indi jàmm, di def safaan. Maay Aji Sax jiy def lii lépp!
ku ci nekk, sab liggéey dina feeñ, ndax bés baa koy xamle, nde sawara lees koy feeñale. Ku ci nekk, ak lu sa xeetu liggéey mana doon, sawara lees koy natte.
Yeen ñépp ay doomi leer ngeen, doomi bëccëg ndarakàmm; nun bokkunu dara ak guddi, mbaa ag lëndëm.