Genesis 18:33
TSK
¶ Loolu la Aji Sax ji wax ak Ibraayma, daldi dëddu. Ibraayma it ñibbi këram.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Loolu la Aji Sax ji wax ak Ibraayma, daldi dëddu. Ibraayma it ñibbi këram.
¶ Naka la Yàlla wax ak Yanqóoba loolu, daldi teqlikoo ak moom.
Mu ne leen: «Dégluleen bu baax samay kàddu: su ngeen feeñlee ab yonentu Aji Sax ji, ci am peeñu laa koy xamale maay kan, te ci gént laay waxeek moom,