Genesis 18:4
TSK
Xaarleen, ñu indil leen tuuti ndox, ngeen jàngu te nopplu ci ker garab gi.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Xaarleen, ñu indil leen tuuti ndox, ngeen jàngu te nopplu ci ker garab gi.
¶ Ba Laban déggee ne jarbaatam Yanqóoba ñëw na, dafa daw gatandu ko, taf ko ci boppam, fóon ko, yóbbu ko kër ga. Ba Yanqóoba nettalee Laban lépp,
¶ Mu walbatiku ca ndaw sa, daldi ne Simoŋ: «Gis nga ndaw sii de? Dugg naa sa kër, mayewoo ndox mu ma jàngoo. Waaye moom, ay rongooñam la tooyale samay tànk, fompe ko kawaru boppam.
te di ku ñu seedeel jëf ju rafet; lu mel ni yar ay gone, ak man gan, ak teral gëmkat ñu sell ñi, ak dimbali ñi tollu diggante, ak di jàppoo jépp jëf ju baax.