TSK

TSK · Genesis 33:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Defal nga ma yiw, yërëm ma lool, ba musal ma. Waaye bala maa daw, ba àgg ca tund ya, musiba mii man naa dal ci sama kaw, ma dee.

Yuda ne ko: «Waa ja da noo àrtu woon de, wax na nu ne nu: “Dootuleen jàkkaarlook man te ànduleen ak seen rakk.”

¶ Ba dëj ba weesee, Yuusufa dafa wax ak waa kër Firawna, ñaan leen ñu dimbali ko, waxal ko Firawna ne ko,

Ruth 2:10 TSK

¶ Naka la wax loolu, mu sujjóot, dëpp jëëm fa suuf, ne ko: «Xanaa su la neexoon de, doo ma nemmiku sax, ndax ab doxandéem laa, waxatuma nga di ma laaye nii biir!»

Daawuda ne ko: «Baax na. Dinaa fasook yaw kóllëre, waaye lenn rekk laa lay ñaan. Bul dikk fi sama kanam te indiloo ma sama jabar Mikal doomu Sóol.»

¶ Absalom nekk na Yerusalem ñaari ati lëmm yu mu sañula taxaw fa kanam Buur baayam.

Job 33:26 TSK

bu ñaanee Yàlla, mu nangul ko, geesu ko, mu sarxolle, nde Yàllaay fey nit njekkam,

Aji Sax ji dafa wax ne: «Waa Israyil ñi rëcc ñawkay saamar, daje nañook yiw ci màndiŋ mi, fekk ñuy sàkku noflaay.»