Leviticus 18:16
TSK
¶ «Bul dëkkoo soxnas koo bokkal benn baay mbaa jenn ndey, nde kon nga torxal sa doomu baay mbaa sa doomu ndey.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ «Bul dëkkoo soxnas koo bokkal benn baay mbaa jenn ndey, nde kon nga torxal sa doomu baay mbaa sa doomu ndey.
¶ Bu ay góor yu bokk waajur dëkkee, kenn ci ñoom dee te bàyyiwul doom ju góor, jabaru ki dee du génn, di séy akub jaambur. Jëkkëru donaleem ju bokk ak jëkkëram moo ko wara jël, donloo ko.
¶ Mu ne leen: «Ñibbileen ngalla, doom, lu ngeen di ànd ak man doye? Ndax dama leena manatee jural ay jëkkër ci sama biir bii?
Mu ne: «Kon de duma mana def sama warugar, ndax sama alal a ciy yàqoo. Fabal boog sama sañ-sañu jotaat, ndax duma ko mana jariñoo.»