Genesis 40:18
TSK
¶ Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy: ñetti pañe yi, ñetti fan la.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Yuusufa ne ko: «Piri mi mooy: ñetti pañe yi, ñetti fan la.
¶ Yuusufa ne Firawna: «Sa ñaari gént yi de, sang bi, ñoo bokk piri. Sang bi, Yàlla da laa xamal li muy def ëllëg.
Mooy li ma la wax rekk, sang bu tedd bi: li Yàlla di defi ëllëg la la won.
¶ «Loolooy gént gi. Nu wax la piri mi nag, Buur.
Ajara moomu mooy tundu Sinayi, wa ca réewum Arabi, te moo taxawe Yerusalem gii tey, dëkk bii dib jaam mook doomam yi ko dëkke.