2 Kings 19:26
TSK
Waa dëkk ya ne yàcc, jàq, torox, mel ni gàncaxu àll mbaa ñax mu yees, mbete caxum xadd, balaa màgg lax.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waa dëkk ya ne yàcc, jàq, torox, mel ni gàncaxu àll mbaa ñax mu yees, mbete caxum xadd, balaa màgg lax.
«As ngelaw lañu ji, ñooy góob ngëlén. Gub du jóg, pepp du focci, te bu pepp amoon it, jaambur a koy wonn.
Efrayim moom, su naatee ci biiri bokkam it, fa màndiŋ ma la ngelawal penku, ngelawal Aji Sax ji di uppe, bëti ndoxam tëju, ay teenam déy. Kii mooy sëxëtoo ab dencam, ak mboolem lu cay alal.»