Firawna nag tudde Yuusufa Safnat Paneya, may ko jabar Asnat doomu Potifera ma doon sarxalkat ca dëkk ba ñuy wax On. Yuusufa doxe ca tegoo kilifteefu Misra gépp.
TSK
TSK · Genesis 46:20
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 41:45
TSK
Genesis 48:1
TSK
¶ Ba loolu wéyee ñu ne Yuusufa baayam dafa tawat, mu ànd ak ñaari doomam Manase ak Efrayim, seeti ko.
Genesis 48:13
TSK
ba noppi Yuusufa taxawal leen ñoom ñaar, ñu séq ko janook Israyil, loxol ndijooram jàpp ci Efrayim, mu féete ak càmmoñu Israyil, loxol càmmoñam jàpp ci Manase, mu féete ak ndijooru Israyil. Ñu ànd jegesi,
Numbers 1:32
TSK
¶ Ñu lim turi sëti Yuusufa yi askanoo ci doomam Efrayim, ku nekk ak làngu cosaanam ak kër maamam, mboolem góor ñi xare war, te ñu am ñaar fukki at, jëm kaw.
Yuusufa la wax, ne ko: Yal na barkeb Aji Sax ji ñeel suufam, bawoo ca xéewali asamaan, dib lay, ak ndox mu lal xóotey suuf,