TSK

TSK · Genesis 46:34

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ca bés booba Laban dafa ber sikket, yi seereer te todde, ak bëy, yi tippante te todde, maanaam yi rax, ak xari menn melo yu ñuul yi, daldi leen dénk ay doomam.

¶ Mu am bés ay magam dem dëkk ba ñuy wax Sikem, sàmmi seen juru baay.

Su ko defee nga dëkksi diiwaanu Gosen, nekk ci sama wet, yaak say doom ak say sët ak say gàtt ak say gétt ak mboolem loo moom,

Musaa ne ko: «Loolu du yoon, ndax li nuy rendil sunu Yàlla Aji Sax ji, waa Misra dañu koy xof. Te bu nu sarxalee lenn lu waa Misra xof, ñuy gis, dinañu nu dóor ay doj, ba nu dee.