Genesis 45:10
TSK
Su ko defee nga dëkksi diiwaanu Gosen, nekk ci sama wet, yaak say doom ak say sët ak say gàtt ak say gétt ak mboolem loo moom,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Su ko defee nga dëkksi diiwaanu Gosen, nekk ci sama wet, yaak say doom ak say sët ak say gàtt ak say gétt ak mboolem loo moom,
¶ Yanqóoba dafa yebal Yuda, mu ànd ak Yuusufa, jiituji ko diiwaanu Gosen, Yanqóoba fekki leen fa. Ñu daldi agsi Gosen.
“Lan mooy seen liggéey?” ngeen ne ko: “Nun de sang bi, ag jur lanu masa yar, ba nuy gone ba tey, te noonu la ko sunuy maam daan defe.” Su boobaa, ngeen mana féetewoo diiwaanu Gosen, ndaxte waa Misra dañuy xof sàmm.»
Diiwaanu Gosen, ga bànni Israyil dëkkoon doŋŋ, moo mucc ca tawub yuur ba.