TSK

TSK · Genesis 9:10

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Rabi àll yi ak luy raam ak luy naaw ak luy dox ci kaw suuf— lépp génne ca gaal ga, lu ci nekk ak wirgoom.

Job 38:1 TSK

¶ Ba loolu amee Aji Sax ji àddoo fa ngëlén la, ne Ayóoba:

Day mébét lu ñaaw cib lalam, taxawe yoon wu dëddu mbaax, te du bañ lu bon.

Bésub keroog maa leen di fasal kóllëre ak rabi àll yeek njanaaw yi, ak ndëgmeent yi. Fitt ak saamar akub xare it, maa koy dagge ci réew mi, te maa leen di may tëraayu jàmm.