Isaiah 43:25
TSK
Mennum man mii maay far say moy ngir man, ba dootuma fàttliku bàkkaar.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mennum man mii maay far say moy ngir man, ba dootuma fàttliku bàkkaar.
Moo nuy yërëmati; sunuy ñaawtéef lay joggiy tànkam, te biir xóotey géej lay tàbbal sunuy bàkkaar.
lii la ca teg: seeni bàkkaar ak seeni tooñ, duma ci bàyyeeti xel.»