TSK

TSK · Isaiah 17:2

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

La ko dale Arower ga tiim walum Arnon, boole ca dëkk ba ca xur wa, ba ca Galàdd, du benn dëkk bu nu të. Foofu fépp la sunu Yàlla Aji Sax ji daane fi sunu kanam.

Am xar a nara fore biir dëkk bi, mbetem parlu, màngaan lekke gentub boroom alal.

Fu junniy reseñ taxaw tey, di jar junniy donji xaalisu lëmm, bésub keroog ay dég aki dagg nangu ko.

Yeen waa Arower, taxawleen fi yoon wi te teewlu; góor gu fi jaare mbaa ndaw su rëcc, di daw, ngeen laaj ko ne ko: “Lu xew?”

Micah 4:4 TSK

Ñoom ñépp ay toog, ku nekk ci kerug reseñam, mbaa keppaarug garabu figgam, kenn du leen xoqtal. Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax.