كل أسفار KYG

James 2

KYG · الآية 25

5 أصحاحات

KYG / James / الأصحاح 2

KYG · الآية 25

X anaa du noonu it lañu joxe Raxab gànc ba, àtteb ku jub, ci kaw jëfam, ndax la mu dalaloon ndawi Yawut ya, ba awale leen feneen?