TSK

TSK · Job 10:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع
Job 23:9 TSK

Bu jàppee fa wetu bëj-gànnaar, gisuma ko fa, bu jàllee bëj-saalum séenuma ko fa.

Job 23:14 TSK

Mooy sottal lu mu ma dogalal, te bare na lu mu ma nasal.

Maay bind leer, di def lëndëm. Maay indi jàmm, di def safaan. Maay Aji Sax jiy def lii lépp!

Fàttlikuleen cosaan la woon. Man mii maay Yàlla, du keneen. Amul Yàlla ju mel ni man!

¶ Céy xóotaayub koomu Yàlla ak xel ma, ak xam-xam ba! Deesul natt ay dogalam, deesul ràññee ay jëfinam!