TSK

TSK · Job 13:7

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba mu ko defee Yewu woo mbooloo ma mépp, ne leen: «Axab tuuti la jaamu Baal. Man Yewu bu baax laa koy jaamu.

Job 11:2 TSK

Yii kàddu yu wale, deesu ko tontoo? Wax ju bare tax na nit a yey?

Job 27:4 TSK

sama gémmiñ gii du wax njubadi, sama làmmiñ wii laa ne, du tudd ay fen.

Job 36:4 TSK

Sikk déy, nekkul ci li ma lay wax; ku buural xam-xam a janook yaw nii!

¶ Waaye su sunug njubadi fésalee njubteg Yàlla, ana lu loolu mana tekki ci nun? Ma waxe ko nu ko nit mana dégge; ma ne, kon bu nu Yàlla wàcceelee am sànjam, deful ag njubadeem?