Mu ne leen: «Ba xale biy dese bakkan laa doon woor ak a jooy, ndax dama noon: “Ana ku xam ndax Aji Sax ji dina ma defalu yiw, ba xale bi dund am déet?”
TSK
TSK · Joel 2:14
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Jombul nag sa Yàlla Aji Sax ji dégg mboolem kàdduy bëkk-néeg bi sangam buurub Asiri yebal, ngir mu kókkali Yàlla jiy dund. Te kon sa Yàlla Aji Sax ji mooy dogal mbugal mi war ci kàddu yooyu mu dégg. Yékkatil kàddug ñaan rekk, ngir ñi fi desagum.”»
Jombul ñu dégg, ba ku nekk dëpp yoonam wu bon. Su ko defee ma fomm musiba, mi ma leen di waajal ndax seen jëf ju bon.
Yeen sarxalkat yi, gembuleen te tiislu, yeen ñi dénkoo sarxalukaay bi, yuuxuleen, yeen boroom dénkaaney sama Yàlla, dikkleen, sol ay saaku yu ngeen fanaanoo, ngir toroxlu, nde xañees na seen kërug Yàlla ga saraxu pepp ak saraxu tuuru!
Bañleen lu bon, bëgg lu baax, di doxal yoon ci pénc. Jombul Aji Sax ji Boroom gàngoor yi baaxe ndesu askanu Yuusufa.
Jombul Yàlla dëpp ba fomm, daldi dëddu tàngooru meram, ba dunu sànku.»
Ana am jiwooti ci sàq yi? Mbaa lennati ci reseñ ak figg? Mbaa garabi gërënaat ak oliw? Du lenn lu meññ. Waaye li ko dale bésub tey jii, maay barkeel.
Jaamub Boroom bi ndànk la war di jubbanti diiŋatkat yi, nde jombul Yàlla may leen ñu tuub, ba xam liy dëgg.