Yeen waa àddina, kat-kat, pax akub caax dëgmal na leen.
TSK
TSK · Lamentations 2:22
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Isaiah 24:17
TSK
Jeremiah 14:19
TSK
Aji Sax ji, wacc ngaa wacc Yuda nii? Am Siyoŋ a la génnliku? Lu tax nga di nu dumaa musiba mu amul paj? Nuy yaakaar jàmm, dara baaxul, nuy séentum paj, tiitaange ne jaas!
Jeremiah 20:3
TSK
Ca suba sa Pasur yiwee ko ca jéng ba. Yeremi ne ko: «Aji Sax ji tuddeetu la Pasur; Magor-Misabib (mu firi Tiitaange lu dajal) la la tudde.
Jeremiah 46:5
TSK
«Ana lu ma gis? Waa Misraa jaaxle bay dellu gannaaw, seeni jàmbaar falaxoo, ne wëqet, geesuwñu, tiitaange ubale.» Kàddug Aji Sax jee!
Hosea 9:13
TSK
Ni ma dogule Tir dëkk ba, bi jëmbate ci parlu mu naat, ni laay dogule Efrayim, ba yóbbul ay doomam ab bóomkat.
Luke 23:29
TSK
Ay jant a ngi ñëw kat, dees na ca ne: “Ndokklee jigéen ju tëlee am doom, masula jur, masula nàmpal!”