¶ «Su fekkee dañoo jàpp ab sàcc guddi, muy toj kër jaambur, bu ñu ko dóoree, ba mu dee, deesul topp ki dóor, bakkanu sàcc bi,
TSK
TSK · Leviticus 6:5
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Su ñu ko jàppul nag, na boroom kër gi sàkku seede àttekat yi, te waat ne, du moom ci boppam moo aakimoo alalu moroomam.
Na fa Aaróona taal cuuraay suba su nekk. Buy topptoo làmp yi lay taal cuuraay lu xeeñ li.
Day tuub bàkkaaram, ba noppi fey dayo ba mu ameel ka mu tooñ. Te juróomeelu xaajam la cay teg, jox ko ko.
Te it menn mbote mi, ñeentam la koy feye, gannaaw moo def jooju jëf, te amu ci jenn yërmande!»
Deesul sikk ku sàcc aw ñam, def ci biiram ndax xiif.
Su boobaa bu ngeen wooyee Aji Sax ji, mu wuyu; ngeen ne wallóoy, mu ne “Maa ngi.” Ndegam génne ngeen noteel ci seen biir, ak di joxoñeek a wax lu ñaaw,
Sase nag taxaw ne Sang bi: «Sang bi, ma ne, sama genn-wàllu alal, jox naa ko néew-doole yi, te jépp alal ju lewul ju ma masa jëlal kenn, dinaa fey ñeentam.»