¶ «Du benn saraxu pepp bu ñuy defal Aji Sax ji muy am lawiir, ndax du lenn ci lawiir mbaa lem, lu ñu wara lakk, ngir saraxu sawara su ñeel Aji Sax ji.
TSK
TSK · Malachi 1:7
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Leviticus 2:11
TSK
Jur gu ci am sikk nag, muy soox, mbaa mu gumba, mbaa mu am sikk su réy su mu mana doon, buleen ko sarxalal seen Yàlla Aji Sax ji.
Ezekiel 41:22
TSK
¶ Sarxalukaay bi bant la, taxawaayam di ñetti xasab, guddaayam di ñaari xasab, yaatuwaayam di ñaari xasab. Mu ami coll akub tegukaay aki wet, lépp di bant. Waa ji ne ma: «Taabal jii mooy janook Aji Sax ji.»
Malachi 1:12
TSK
«Waaye yeen yeena teddadil sarxalukaayu Aji Sax ji, nde yeena xalaat ne lu sobewu la, te aw yàppam, aw ñamam jarul dara.
ndax bu ngeen dee lekk, ku nekk, reeru boppam lay jëkkantee lekk, ba tax ñenn ci yeen xiif, fu ñeneen naane ba màndi.