Isaiah 43:28
TSK
ba tax ma sobeel kilifay kër gu sell gi, araamal Yanqóoba, wacce Israyil ŋàññi noon.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
ba tax ma sobeel kilifay kër gu sell gi, araamal Yanqóoba, wacce Israyil ŋàññi noon.
Ase nag wax leen, ne leen: «Noonu la ci askan wii, noonu la ci xeet wii sama kanam. Kàddug Aji Sax jee. Noonu la ci mboolem seen liggéeyu loxo, ak sarax su ñu fi indi, loolu lépp a sobewu.