Proverbs 31:21
TSK
Tiitul ci njaboot gi sedd bu metti, ndax ñoom ñépp ay tegley yére.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Tiitul ci njaboot gi sedd bu metti, ndax ñoom ñépp ay tegley yére.
«Aji Sax ji déy a ngii dikke sawara, ay watiiram mel ni ngëlén, mu nara sànju, sotti meram, gëdde sawara wuy sëlsëli.
ay fasam yu bare sànge la pënd, riiru gawar yaak mbege yaak watiir ya riiral say miir, mu jàlle say wunt, dugg, ni ñuy bëtte dëkk, bu ñu bëtt tataam.
Kàccri dal, ay mbege riir, fas rëpptal, watiir kar-kari.