¶ Ba mbooloo ma gisee Musaa yàgg lool te wàccul tund wa, dañoo songandoo Aaróona, ne ko: «Ayca, sàkkal nu yàlla ju nu jiite, ndax Musaa mii nu génne réewum Misra kat, xamunu lu ko dal.»
TSK
TSK · Nehemiah 13:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Exodus 32:1
TSK
Ezra 6:22
TSK
Wormaal nañu it màggalu Mburu mu amul lawiir, diiru juróom ñaari fan, ci biir mbégte, ndax fekk na Aji Sax ji bégal leen lool ca na mu xiire buurub Asiri, mu yéwéne leen ba dimbali leen ci tabaxu kër Yàlla ga, Yàllay Israyil.
Nehemiah 2:5
TSK
door ne Buur: «Xanaa Sang bi, su la neexee rekk, nga yéwéne ma, yebal ma Yuda, dëkk ba ñu denc samay maam, ba ma tabaxaat ko.»
Nehemiah 5:14
TSK
¶ Bu loolu weesee, la ko dale bés ba ñu ma falee boroom diiwaanu Yuda, ca ñaar fukkeelu atu nguurug Artaserses, ba ca fanweeru atam ak ñaar, muy fukki at ak ñaar, lekkunu alalu galag bu boroom diiwaan yelloo, du man, du samay bokk.