Teewul seen baay wor ma, soppi sama peyoor fukki yoon ak juróom, waaye Yàlla seetaanu ko, mu di ma lor.
TSK
TSK · Numbers 14:22
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Ci biir loolu ñu ne Musaa: «Xanaa Misra dafa amul ay sëg, ba nga di nu indi ci màndiŋ mi, nu deesi fi? Loo nu doon génnee Misra?
¶ Ba mbooloo ma gisee Musaa yàgg lool te wàccul tund wa, dañoo songandoo Aaróona, ne ko: «Ayca, sàkkal nu yàlla ju nu jiite, ndax Musaa mii nu génne réewum Misra kat, xamunu lu ko dal.»
Xanaa Kaleb doomu Yefune, Keneseen bi, ak Yosuwe doomu Nuun, ndax ñoo matal kóolute ci Aji Sax ji.”
Fukki yoon a ngii ngeen di ma saaga, te rusuleen maa sonal.
di ŋaf-ŋafi ca màndiŋ ma, di diiŋat Yàlla ca àll ba.
Gis nga lu bare, waaye jàppoo ci dara. Nopp ne kótt, dég-dég të!»
Bunu wut itam Almasi, ni ko ñenn ci ñoom wute woon, ba tax ay jaan rey leen.
Ana ñan la Yàlla mere lu mat ñeent fukki at? Xanaa du mboolem ña bàkkaaroon te seeni néew mujj tëdd ca màndiŋ ma?