Numbers 14:32
TSK
Waaye yeen, seeni néew ci màndiŋ mii lay tëdd,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Waaye yeen, seeni néew ci màndiŋ mii lay tëdd,
Ndax ci ñoom la Aji Sax ji noon dee rekk lañuy def ba jeex ca màndiŋ ma. Kenn desu ca, ku dul Kaleb doomu Yefune, ak Yosuwe doomu Nuun.
Teewul ñi ëpp ci ñoom, Yàlla amul woon lu ko neex ci ñoom, ba tax ñu daanu, dee ca màndiŋ ma.
¶ Doonte xam ngeen loolu lépp ba noppi, dama leen di fàttli rekk ne Boroom bi moo jëkka musal ñoñam, génne leen réewum Misra, te gannaaw gi moo raafal ña gëmul woon ca ñoom.