TSK

TSK · Numbers 16:38

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

ba suuf sa xar, boole leen ak Kore, wonn, keroog ba gàngoor ga sànkoo, te sawara wa lakk ñaar téeméeri nit ak juróom fukk, ñu daldi doon firnde luy artoo.

Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.

Buur mer lool, mel ni gayndee ŋar; boo ko merloo, dangay xaru.

Gàcce nga nasal sa kër, ba nga sànkee ay xeeti xeet, te yaa tooñ sa bopp.

ndegam dëkk ya ñuy wax Sodom ak Gomor it, la mbugale seenub taste, def leen ab dóom, ba def leen misaal mu ñeel aji gëmadiy ëllëg,