Numbers 22:40
TSK
Balag daldi sarxe ay nag aki xar, sédd ca Balaam ak kàngam ya ko dar.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Balag daldi sarxe ay nag aki xar, sédd ca Balaam ak kàngam ya ko dar.
Balag def na ko Balaam wax, Balag ak Balaam ku ci nekk sarxal wenn yëkk ak menn kuuy ci sarxalukaay bu nekk.